OneNote API

API yu OneNote ngir liggéey ak daara leegi jàppandina
moom ak ab wonandib booleg Grafigu Microsoft.

Ngir Windows, Windows Phone, iOS, Mac, Android & Web

OneNote API

jàng

royuwaayu api

Sunu téerey jokkanlante dañu lay dimbali nga gaaw a jëfandikoo OneNote API yi.

Téere yi

MSDN dafa àndaale ak ay jumtukaayi jàngal ak yeneen royuwaay yu lay dimbali nga xam li bokk ak li bokkul ci OneNote API.

misaali kot

Sunu sàqum GitHub dafa am ay misaali kot ngir Android, Windows, ak lépp lu nekk ci seen diggante.

wideo yi

Seeri yu OneNote Development ci Channel9 mën nga ko jëfandikoo soo boolee ci jëfekaay ci OneNote.

mbooloo

blog

Mën nga xibaar yi gën a bees ci man-man yiy ñëw ak gën a baaxal liggéeyal jaare ko sunu blog.

twitter

Siiwali Blog dafa gudd lool ci yaw? Jëfandikool sunu sàqu Twitter ngir am li ci ëpp solo.

stack overflow

Nun ñépp a jëfandikoo Stack Overflow. Leegi mën nañu jotee seeni laaj ci OneNote API yi ba noppi tontu leen fa itam.

Wax sa xalaat

Ndax am nga xalaat bu rafet ngir API bi? Nu ngi seetu xalaat yu rafet ci sunub liggéey? Demal ci sunu péncu UserVoice.